Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 3:7-10 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 3:7-10
in
Kàddug Yàlla gi
7
Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;
8
sa yaram wér, say cér naat.
9
Teralal Aji Sax ji ci sa alal ak loo jëkka meññle,
10
say sàq day fees, ne xéew, say mbàndi ndoxi reseñ di wal.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms