Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:5-9 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:5-9 in Kàddug Yàlla gi

5 Nanga wóoloo Aji Sax ji, sa léppi xol, te bul wéeru ci saw déggin.
6 Loo mébét, bàyyil Yàlla xel, mu xàllal la yoon.
7 Bul doyloo sa xel mu rafet, ragalal Aji Sax ji, dëddu mbon;
8 sa yaram wér, say cér naat.
9 Teralal Aji Sax ji ci sa alal ak loo jëkka meññle,
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi