Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:5-6 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:5-6 in Kàddug Yàlla gi

5 Nanga wóoloo Aji Sax ji, sa léppi xol, te bul wéeru ci saw déggin.
6 Loo mébét, bàyyil Yàlla xel, mu xàllal la yoon.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi