Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 3:30-34 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 3:30-34
in
Kàddug Yàlla gi
30
Bul joteek kenn ci neen, te tooñu la.
31
Bul ñee ku néeg, te bu ko roy fenn.
32
Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
33
Aji Sax ji day alag kër ku bon, di barkeel waa kër ku jub.
34
Kuy ñaawle, moo lay ñaawal, ku toroxlu, mu may law yiw.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms