Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:27-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:27-29 in Kàddug Yàlla gi

27 Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.
28 Bul ne say dëkk: «Demal ba beneen, ma jox la,» te fekk la yor.
29 Bul fexeel dëkkandoo bu dëkk ak yaw ci kóolute.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi