Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:27-28 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:27-28 in Kàddug Yàlla gi

27 Bul xañ njekk ku ko yelloo, ndegam man nga ko.
28 Bul ne say dëkk: «Demal ba beneen, ma jox la,» te fekk la yor.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi