Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:24-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:24-25 in Kàddug Yàlla gi

24 Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25 Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi