Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:23-25 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:23-25 in Kàddug Yàlla gi

23 Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24 Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
25 Kon doo ragal njàqare lu bette ak saaysaay buy songe,
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi