Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:20-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:20-24 in Kàddug Yàlla gi

20 Ci xam-xamam la ndoxi xóote ya ne jàyy, ay niir di lay.
21 Sama doom, saxool xelu akug foog, dee ci xool foo tollu.
22 Day guddal saw fan, di rafetal sa jikko.
23 Kon sab dox wóor, doo fakktalu.
24 Soo tëddee doo tiit; say nelaw day neex.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi