Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:15-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:15-16 in Kàddug Yàlla gi

15 Xel mu rafet a gën gànjar; loo mana bëgg moo ko raw.
16 Gudd fan, mu joxee ndijoor; càmmoñ ba, alal ak teraanga.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi