Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.
14 Am koo gën am xaalis, te njariñ laa raw wurus.
15 Xel mu rafet a gën gànjar; loo mana bëgg moo ko raw.
16 Gudd fan, mu joxee ndijoor; càmmoñ ba, alal ak teraanga.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi