Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:12-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:12-14 in Kàddug Yàlla gi

12 ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.
13 Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.
14 Am koo gën am xaalis, te njariñ laa raw wurus.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi