Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:11-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:11-13 in Kàddug Yàlla gi

11 Doom, bul xeeb yaru Aji Sax ji, bul bañ mu waññi la,
12 ndax Aji Sax ji, ku mu sopp, waññi la, ni baay, ak doom ju ko neex.
13 Mbégtee ñeel ku daj xel mu rafet ak ku am ug dégg.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi