Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 3:1-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 3:1-4 in Kàddug Yàlla gi

1 Doom, bul fàtte sama njàngle, defal sa xel ci saay santaane,
2 ngir fan wi gudd lool, nga gëna am jàmm.
3 Bu la ngor ak worma dëddu, booleel takk ci sa baat, bind ko ci sa àlluway xol.
4 Kon nga xam lu jaadu, neex Yàllaak doom aadama.
Kàddu yu Xelu 3 in Kàddug Yàlla gi