Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:26-29 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:26-29 in Kàddug Yàlla gi

26 Day wax lu xelu, di digle ngor.
27 Jigéen jooju mooy bàyyi xel ci njabootam, te du nangoo yàccaaral.
28 Doom ya dañu ko naan: «Jarawlakk!» jëkkër ja di ko gërëm naan:
29 «Jeeg bu jàmbaare bare na, waaye yaw, yaa ci raw.»
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi