Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:24-27 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:24-27 in Kàddug Yàlla gi

24 Ndaw su ni mel day ràbb ay yére, di jaay, aki gañaay, di jox jaaykat yi.
25 Faaydaak jom la làmboo, te ëllëg ubul boppam.
26 Day wax lu xelu, di digle ngor.
27 Jigéen jooju mooy bàyyi xel ci njabootam, te du nangoo yàccaaral.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi