Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:19-22 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:19-22 in Kàddug Yàlla gi

19 Ma ngay yor poqe ak këccu, di ëcc.
20 Day jox ku ñàkk, di sàkkal néew-ji-doole.
21 Tiitul ci njaboot gi sedd bu metti, ndax ñoom ñépp ay tegley yére.
22 Mooy sàkkal boppam ay malaan, ay yéreem mucc ayib te yànj.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi