Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:17-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:17-20 in Kàddug Yàlla gi

17 Day gañu di góor-góorlu, ak a dëgëral përëg ya.
18 Day gis njartel liggéeyam, te làmpam du fey guddi.
19 Ma ngay yor poqe ak këccu, di ëcc.
20 Day jox ku ñàkk, di sàkkal néew-ji-doole.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi