Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:13-16 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:13-16 in Kàddug Yàlla gi

13 Day wut kawari gàtt aki wëñ, di ca liggéeye mbégte.
14 Day mel ni gaalu jula, di jëli dundam fu sore.
15 Day jóg te bët setul, di waajal njëlu njabootam, ak a sas ay janqam.
16 Day seetlu ab tool, jënd ko, sàkk ciw ñaqam, jëmbat tóokër.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi