Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:13-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:13-14 in Kàddug Yàlla gi

13 Day wut kawari gàtt aki wëñ, di ca liggéeye mbégte.
14 Day mel ni gaalu jula, di jëli dundam fu sore.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi