Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 31:10-13 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 31:10-13 in Kàddug Yàlla gi

10 Jeeg bu jàmbaare, ndaw lu jafe, ba rawati gànjar!
11 Jëkkër ja da koy wóolu, te jëkkër ja day am xéewal, du ko ñàkk.
12 Day defal jëkkëram lu baax, du ko lor, tey ànd ak bakkan.
13 Day wut kawari gàtt aki wëñ, di ca liggéeye mbégte.
Kàddu yu Xelu 31 in Kàddug Yàlla gi