Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:19-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:19-21 in Kàddug Yàlla gi

19 Ku dem ca moom dootoo délsi, doo gisati yoonu dund mukk.
20 Kon nag aweel mbeddum waa ju baax, toppal yoonu ku jub,
21 ndax kuy jubal ay dëkke réew mi, te ku mat a fiy des.
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi