Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:18-20 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:18-20 in Kàddug Yàlla gi

18 Këram day joy wuti ndee, ay jaaruwaayam jëm njaniiw.
19 Ku dem ca moom dootoo délsi, doo gisati yoonu dund mukk.
20 Kon nag aweel mbeddum waa ju baax, toppal yoonu ku jub,
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi