Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:16-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:16-19 in Kàddug Yàlla gi

16 Xel mu rafet da lay musal ci ndaw su yemadi, bokk feneen, di wax lu neex.
17 Day dëddu wóllëreem, ba muy ndaw, fàtte kóllëreem ak Yàllaam.
18 Këram day joy wuti ndee, ay jaaruwaayam jëm njaniiw.
19 Ku dem ca moom dootoo délsi, doo gisati yoonu dund mukk.
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi