Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 2:10-13 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 2:10-13
in
Kàddug Yàlla gi
10
Ndax xel mu rafet miy tàbbi sa xol, nga xam, sa xol tooy,
11
nga foog, fegu, am ug dégg, raw,
12
mucc ci yoonu ku bon ak kuy wax lu jekkadi,
13
mucc ci kuy wacc yoonu njub, di jaare mbedd yu lëndëm.
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms