Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 2:10-12 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 2:10-12 in Kàddug Yàlla gi

10 Ndax xel mu rafet miy tàbbi sa xol, nga xam, sa xol tooy,
11 nga foog, fegu, am ug dégg, raw,
12 mucc ci yoonu ku bon ak kuy wax lu jekkadi,
Kàddu yu Xelu 2 in Kàddug Yàlla gi