Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Ñaawlekat a ngi taal ab dëkk, ku xelu di giifal mer.
9 Boroom xel, buy layook ub dof, bu mereek buy ree, jàmm du am.
10 Ab bóomkat day sib ku mat, di wuta bóom kuy jubal.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi