Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:25-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:25-26 in Kàddug Yàlla gi

25 Ragal nit dugal sa bopp la, ku wóolu Aji Sax ji, fegu.
26 Ñu baree ngi sàkku kilifa baaxe leen, moona Aji Sax jeey àtteb jaam.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi