Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:20-21 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:20-21 in Kàddug Yàlla gi

20 Ana koo gis, mu rattaxle? Kooku ab dof a ko gën demin.
21 Ku yàq sab surga ba muy ndaw, bu ëllëgee mu defe ne doom la.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi