Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:2-5 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:2-5 in Kàddug Yàlla gi

2 Ku jub falu, baadoolo bég; ab soxor jiite, baadoolo binni.
3 Kuy jëfe xel, bégal sa baay; nga ànd aki gànc, yàq alal.
4 Buur jub, am réew dëgër; mu bëggi galag, réew ma sànku.
5 Kuy jay sa moroom, yaa ngi koy dugal.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi