Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:17-19 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:17-19 in Kàddug Yàlla gi

17 Yaral sa doom, mu noppal la, bànneexal la.
18 Fu Yàlla feeñoowul, nit ña fétteeral, waaye ku topp yoon, am mbégte.
19 Waxi neen yarul surga, da lay dégg te du la déggal.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi