Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 29:10-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 29:10-11 in Kàddug Yàlla gi

10 Ab bóomkat day sib ku mat, di wuta bóom kuy jubal.
11 Ab dof day mer, sàmbaar; ku xelu, mer, ànd ak sagoom.
Kàddu yu Xelu 29 in Kàddug Yàlla gi