Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:8-11 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:8-11 in Kàddug Yàlla gi

8 Ku sore fa nga bokk, dangay mel ni picc mu sore tàggam.
9 Diwook suuru day naatal xol; waaye li neex cib xarit, xol la lay digale.
10 Bul fàtte sab xarit mbaa sa xaritu baay, bul jàq ba seeti sa mbokk; dëkkandoo bu jegee gën mbokk mu sore.
11 Muusal, doom, ma bég, ba mana tontu ku ma sikk.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi