Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:6-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:6-8 in Kàddug Yàlla gi

6 Soppe, bu lay gaañ sax, wóolu ko. Nit bañ na la, te di la fóon lu bare.
7 Ku suur, bañ lem ju xelli, waaye boo xiifee, lu wex lu ne neex la.
8 Ku sore fa nga bokk, dangay mel ni picc mu sore tàggam.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi