Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:2-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:2-4 in Kàddug Yàlla gi

2 Bul tëggu, bàyyil ñu tagg la, muy waxi keneen; yaw, bu ko wax.
3 Doj diis na, suuf dib sëf, waaye fitnay dof a ko raw.
4 Xadar day ñàng, mer di wal mu baawaan, waaye fiiraange amul moroom.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi