Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:15-17 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:15-17 in Kàddug Yàlla gi

15 Jabar ju pànk mooy senn bu dakkul, cib taw;
16 ku ko mana yemale, mana téye ngelaw mbaa nga ŋëb ag diw.
17 Weñ ay nàmm weñ, nit ay nàmm xelu moroom ma.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi