Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 27:11-14 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 27:11-14 in Kàddug Yàlla gi

11 Muusal, doom, ma bég, ba mana tontu ku ma sikk.
12 Kuy foog, gisu ay, làqu; ab téxét ne ca tëñëx, loru.
13 Ku gàddul jaambur bor, jëlal mbubbam; tayle ko, moo dige feyal ndaw su yemadi.
14 Nuyoo bu xumb, suba teel mooki saagaa yem.
Kàddu yu Xelu 27 in Kàddug Yàlla gi