Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 ndax ñu ne la: «Yéegal, jegesi fii,» moo gën ñu torxal la ci kanam kilifa. Boo gisalee sa bopp it,
8 bul gaawa layooji, ana nooy def ëllëg, bu ñu la yeyee?
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi