Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:24-26 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:24-26 in Kàddug Yàlla gi

24 Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
25 Xibaaru jàmm, bawoo fu sore mooy ndox mu sedd ci ku loof.
26 Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi