Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 25:23-26 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 25:23-26
in
Kàddug Yàlla gi
23
Jëw, mer a cay topp; mooy ngelawal taw, taw a cay topp.
24
Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
25
Xibaaru jàmm, bawoo fu sore mooy ndox mu sedd ci ku loof.
26
Ku jub bu dee nangul ku bon, yàqu na, ni seyaan bu nëx mbaa teen bu xàbb.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms