Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:23-24 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:23-24 in Kàddug Yàlla gi

23 Jëw, mer a cay topp; mooy ngelawal taw, taw a cay topp.
24 Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi