Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 25:13-15 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 25:13-15 in Kàddug Yàlla gi

13 Ndaw lu wóor day seral xolu njaatigeem, mooy ndox mu sedd ci tàngooru ngóob.
14 Kuy dige te doo joxe, yaay xiin wu ngelaw, mu naaxsaay.
15 Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi