Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Kàddu yu Xelu 25:11-13 in Wolof
Help us?
Kàddu yu Xelu 25:11-13
in
Kàddug Yàlla gi
11
Wax ju ñor di nataalu wurus wu tege ci xaalis.
12
Kàddu yu lay yedd ci kuy dégg, jaarob wurus la mbaa gànjaru ngalam.
13
Ndaw lu wóor day seral xolu njaatigeem, mooy ndox mu sedd ci tàngooru ngóob.
Kàddu yu Xelu 25 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms