Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:8-10 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:8-10 in Kàddug Yàlla gi

8 Kuy mébét lu bon, ñu ne yaay rambaaj bi.
9 Pexem dof bàkkaar la, te kuy ñaawle, ñu sib la.
10 Bu mettee, nga yoqi, sa doolee néew.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi