Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:7-8 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:7-8 in Kàddug Yàlla gi

7 Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.
8 Kuy mébét lu bon, ñu ne yaay rambaaj bi.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi