Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:32-33 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:32-33 in Kàddug Yàlla gi

32 Maa ko gis, di xalaat, xoolaat ko, jànge ca.
33 Booy dajjant ak a for bët, di tegley loxook a jaaxaan,
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi