Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:31 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:31 in Kàddug Yàlla gi

31 Ndeke lépp a nga saxi dég, fépp fees akum ñax, tabaxu doj ba ko wër màbb.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi