Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:30-32 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:30-32 in Kàddug Yàlla gi

30 Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.
31 Ndeke lépp a nga saxi dég, fépp fees akum ñax, tabaxu doj ba ko wër màbb.
32 Maa ko gis, di xalaat, xoolaat ko, jànge ca.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi