Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:3-4 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:3-4 in Kàddug Yàlla gi

3 Xel mu rafet ay tabax kër, rafet déggin a koy samp.
4 Xam-xam ay feesal néeg ya ak mboolem alal ju jafe te yànj.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi