Text copied!
Bibles in Wolof

Kàddu yu Xelu 24:29-30 in Wolof

Help us?

Kàddu yu Xelu 24:29-30 in Kàddug Yàlla gi

29 Bul ne: «Li mu ma def laa koy def, damay feyu li mu ma def.»
30 Toolub ku yaafus laa jaare, ak tóokërub nit ku ñàkk bopp.
Kàddu yu Xelu 24 in Kàddug Yàlla gi